Calendar icon
Saturday 10 May, 2025
Weather icon
á Dakar
Close icon
Se connecter

Régate à St Louis : Abdoulaye Sylla gâte la ville de ses parents

image

Auteur: Seneweb News
ESABAT banner

Comments

  • image
    Lô ndame il y a 8 mois

    DG ecotra deff na loumou mine sakh tei lima thi geuneu nekh moy il le fait dans tout le territoire national merci ABS🇸🇳💪🏾❤️

  • image
    Ibrahima il y a 8 mois

    Alkhamdoulah d’avoir toujours des hommes engagés comme vous dans ce pays Nioune jeunesse ndar bi contante naniiu trop si abdoulaye Sylla

  • image
    Demba il y a 8 mois

    Lou raffet dou mousseu niaw Abdoulaye Sylla tiakaw tiakanam si Lou bax li bétouniou ndakh si Lou bax rek lanioula xamé xool seed na yaw domou ndar bi

  • image
    Momar touré il y a 8 mois

    Une personne sociable humble qui répond toujours au besoin de la population vraiment Sylla guissnaniou takhawaay bi envers rewmi yalla laniou lay bayil mou fayal nioula ndakh mom dou fay wakh di bayi ay dieuff

  • image
    Astou ndiaye il y a 8 mois

    Thieuy borome téranga yi y’a bax .iil est tjr dans le domaine du social .matakh lou bakh rk ngay ram inshalah digua yokou ba yeup ko inshalla

  • image
    Alassane il y a 8 mois

    Il commence vraiment à me faire de l’effet personnellement ce cher sieur. C’est la première fois que j’entends ses bienfaits au Sénégal. Cela prouve aussi qu’il n’a pas oublié d’où il vient

  • image
    Mama il y a 8 mois

    Où est l'article

  • image
    Astou Ndoye il y a 8 mois

    Machallah waay cette homme est un vrai patriote qui n’as pas oublié ses racines. Ndeysane yagoute dara rék déf na jeuf jou melni à Touba en déployant gros de moyen pour contribuer au bon déroulement du Magal. Tay mou déf li thi deuk waydiouram. Ki yalla nako yalla faye holam waay

  • image
    Bachir Sané il y a 8 mois

    PDG Ecotra deff na loumou miine. Bakh ak tabbé si mome la fekk bakh

  • image
    Abdou guité il y a 8 mois

    Abdoulaye sylla un homme extraordinaire qui se soucis toujours du bien etre des senegalais On apprécie votre geste noble

  • image
    il y a 8 mois

    Sunu amone plusieurs Abdoulaye sylla deug bi dina bakh. Thia kaw thia kanam rk Ecotra

  • image
    Mame Fatou il y a 8 mois

    Ak groupe ecotra ken amoul fayam doumou ndar ndar yi amougnou sa Faye Abdoulaye Sylla

  • image
    Sadio il y a 8 mois

    Abdoulaye Sylla meilleur de sa génération aka meuneuh social xolal ma témoignage yi qui nako Sénégal gui yeup nianal limouy dff day wané ni Kou beug deuk zte dakoy df avec plaisir

  • image
    Omar il y a 8 mois

    Machallah Abdoulaye sylla lii mom dou tay nga ko commencé… yagg nga ko deff🥰🇸🇳Kene dou ioe Ci kaw, ci kanam rkkk la jeunesse senegalaise est fière de vous

  • image
    Ndiassé Gaye il y a 8 mois

    Ki moy leader bou exemplaire. Nitt kou beurri yeurmandé, di dimbali jeunesse bi. Liguéy th beureiwoul wax. Yalla naniou ko yalla samal.

  • image
    Mami il y a 8 mois

    Lolene khamul si abdoulaye sylla li mo geuna ndaw si limouy def si deuk bi patriote bou mak On a besoin des gens comme sieur Sylla qui contribue au développement de leur pays

  • image
    InfoGalsen il y a 8 mois

    Abdoulaye Sylla un homme multidimensionnel vraiment un geste à saluer wa Saint Louis contann naniou troppp sakh si ligua def

  • image
    Moussa il y a 8 mois

    En tout cas ce Monsieur contribue beaucoup sur son pays, motakh Naniouy téyy si nite ki waxale nagn louné wayé Tay Yalla ngi lérale lepp. C’est un bon gars qui y’a commis une seule faute Aimé son Pays. Vive mR Sylla vive le Sénégal

  • image
    Ndar Ndar bi il y a 8 mois

    Le dévouement d'Abdoulaye sylla envers le peuple est exemplaire. vraiment nioune Wa Saint Louis contane nagn

  • image
    Seydou il y a 8 mois

    Wawaw Abdoulaye Sylla wa Ndar yeup niogui si guinaw, yagui doundeule sa deuk. Yay souniou Future Maire

  • image
    Senegal rk il y a 8 mois

    Abdoulaye sylla mii niakoul ni yallah moko yoni si nioune guirr moniouy defal lou bax🥰😊🥹Vraiment il mérite notre respect pour son dévouement

  • image
    MS hate account il y a 8 mois

    Mom yaag ne def lini mel loxom meussoul diouk si reewam di def Lou bakh ter doussi boler wax diou beuri defar rewam moko taxa diouk

  • image
    Pros ?? il y a 8 mois

    J’ai rarement vu un homme aussi dévoué et engagé pour son pays le Sénégal te remercie vraiment

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    ce.corrupteur ne fait rien gratuitement, les commentaires nous montrent qu'ils ont été payés pour passer leur propagande

  • image
    il y a 8 mois

    Les générations futures du Sénégal ont un champion en Abdoulaye Sylla. Vraiment soutenons le dans ses actes

  • image
    UN HOMME il y a 8 mois

    qui ne respecte pas la loi . Il croit que c'es l'argent qui fait la loi

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Laisse le continuer à faire la PUB accompagnée de son commentateur il faut que des comptes concernant l'assainissement de Diamniadio soient rendus

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Laisse le continuer à faire la PUB accompagnée de son commentateur il faut que des comptes concernant l'assainissement de Diamniadio soient rendus

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Bayilenn ay feinn ak yakk derr kii dii ligueyall dekamm nguenn dii weurr di yakk deramm esk dolenn diema deff nii mome wala nguenn mandou

  • image
    il y a 8 mois

    Le gars dilapide ses milliards depuis quelques temps, à une allure folle. Où a-t-il pris tout cet argent ? Dans quelle domaine économique évolue-t-il ?

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Arrête lenn dii wakh lou lenn nekh sans preuve fii gneupp khamnagn nii projet diamniadio bii mome liko warr yeupp deff nako so ame lo wakh cii lolou wakhko regime sortant bii ts nga demm renseigne wou

  • image
    Alpha ndiaye il y a 8 mois

    Il faut toujours être aux côtés de la population sénégalaise voilà le sens du mot patriotisme et n’oublions pas k le bienfait n’est jamais perdu Félicitations à vous Car Vous méritez un Big Standing Ovation de la part de tout le monde

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Yaw kone khana dagne la fay pour nga contredire ko mdr vous êtes tellement pathétique

  • image
    Astou il y a 8 mois

    Mou tané lako mome au moins migui dieul xalissam di diapalé gniko Solhla iow gua nekk fi di dougou lou sa yone nekoul

  • image
    Fallou Sarr il y a 8 mois

    Yow mome xawma danga yap nitt gni wala danga gate xéll rék. Sénégal dou dème parce que daffa beurri niou bone xoll. Pour yow nieup ni yow lagne méll. Deuk nieup bonougn, raxass lène sène xol yi th bayi yax dérr bi.

  • image
    reply_author Adama il y a 8 mois

    Lolou bane preuve gassi am? Nitt sou deffé lou bakh dagnou koy feusseul comme cela gnénène meune def ni mome. Bayyi lène yakk nitt té khamo lène si mome dara

  • image
    reply_author il y a 8 mois

  • image
    Marouane il y a 8 mois

    Waawaw deuk bi mom sokhor fi la fekk bah. Mais na kounek deff loubah rekk té bagna deglou haters yi

  • image
    Beuleupp il y a 8 mois

    Ndaar meriter nguen lou eupp lolou. Da nguen hamm lou bahh donc on vous rend la pareille

  • image
    Senghor il y a 8 mois

    Man dh hawma kaan mais beug na sama doom melni Abdoulaye Sylla

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Va te renseigner c’est mieux sur l’affaire de diamnadio tout le monde sait que c’est le regime de macky sall qui avait fait un detournement d’objectif sur les fonds destinés a ce projet

  • image
    Man il y a 8 mois

    Saway ki loumou def soko meunoul remercie gua mandou apres yenay tokk nan kein diapalee wouniou alors mom mogui souciewou si sokhla wou ndawi rewam yii moko yitel

  • image
    Dave il y a 8 mois

    Abdoulaye Sylla mérite tout notre respect. Il ne ménage aucun effort pour faire avancer la ville sainte, et c’est tout à son honneur. Que ses projets continuent de porter leurs fruits !

  • image
    Ami il y a 8 mois

    Les actions de Sylla parlent d’elles-mêmes. Investir dans le développement local de cette manière, c’est un geste noble. Un grand merci à lui pour son dévouement.

  • image
    Ndeye ami il y a 8 mois

    C’est impressionnant de voir autant d’efforts et de moyens mis en œuvre pour le développement de notre ville. Abdoulaye Sylla est un vrai modèle de générosité.

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Il a dit vous payer chez les gars, bayilene propagande

  • image
    reply_author il y a 8 mois

    Et même tu es payé par l autre camp pour venir baver

  • image
    Vérité il y a 8 mois

    Tout le monde sait que vous êtes envoyé par votre candidat qui a lamentablement été battu par les 2 vedettes du Régime

Participer à la Discussion